Ezekiel 12:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te nga wax waa réew mi, mbirum waa Yerusalem ga ca suufas Israyil, ne leen Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: njàqare lañuy lekkeji seenu ñam, te xol bu gental lañuy naane seenum ndox, ndax seen réew mu gental, ñàkk lépp lu ko feesoon, ngir coxoru mboolem ñi ko dëkke.