Ezekiel 13:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di dal ci seen kaw jaray xërëm, yi ngeen di nappe ay bakkan niy picc. Seeni jara laay foqatee ci seeni loxo, ba yiwi bakkan, yi ngeen di napp niy picc.