Ezekiel 14:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te mu fekk ñett ñooñu ci biir réew mi, giñ naa ko ci man miy dund, kàddug Boroom bi Aji Sax jee, du seen jenn doom, góor ak jigéen ju ñuy mana musal. Ñoom ñett doŋŋ ay mucc.