Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxal ak ñoom nag, ne leen: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Képp ku bokk ci waa kër Israyil, ku yékkati kasaray tuuram, def ci xolam, muy ay wu koy gàllankoor, te mu ne ci jàkk, ba noppi muy seetluji ci ab yonent; man Aji Sax ji maa koy tontu tont lu dëppook limu kasaray tuuram.