Ezekiel 16:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xooleesu la bëtu ñeewante ngir defal la lenn ci yooyu ngir yërmande. Dees laa sànni ci àll bi bés ba nga juddoo ndax jéppi la.