bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 16:52
Ezekiel 16:52 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag gàddul sa toroxte gi nga maye sa doomi ndey aw lay ndax jëf ju siblu joo jëf, ba yées leen. Gën nañu la. Kon nag séddool gàcce te gàlloo toroxte, nde tax nga sa doomi ndey yi niru ñu def njekk.