Ezekiel 17:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«“Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Giñ naa ko ci man miy dund, maay këpp jëfam ci kaw boppam ndax ngiñ li mu ma giñal la sofental, kàddu gi mu fasanteek man la wor.