Ezekiel 17:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ñay dawe ca gàngooram yépp, saamar lañuy fàddoo; ña cay rëcce, fépp fu ngelaw jublu lañuy tasaarooji, ba ngeen xam ne man Aji Sax ji maa wax.