Ezekiel 18:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
néew-ji-doole, loxoom dalu ko, ndollant ak ab tegandaay, jëlu ko, sama àttey yoon lay jëfe, sama dogali yoon lay doxe. Kooku du dee ngir ñaawtéefu baayam. Dina dund déy!