Ezekiel 18:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
sama dogali yoon, mu di ca doxe, sama àttey yoon, muy jëfe worma: kooku boroom njekk la, te mooy dund déy! Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.