Ezekiel 20:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba loolu wéyee ca atum juróom ñaareel ma, fukki fan ca juróomeelu weer wa, ay nit ñu bokk ci magi Israyil ñoo dikk fi man, di seetlu ci Aji Sax ji. Ñu toog fi sama kanam.