bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 20:13
Ezekiel 20:13 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye waa kër Israyil dañu maa gàntal ca màndiŋ ma. Sama dogali yoon, jëfewuñu ko, sama àttey yoon yiy guddal fanu képp ku koy jëfe, ñu xalab. Ñàkke nañu worma lool sama bési Noflaay. Ma nar leena xëpp samam sànj ca màndiŋ ma, sànk leen.