Ezekiel 20:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma wax nag seeni doom ca màndiŋ ma ne leen: “Seen dogali baay, buleen ko jëfe; seen àttey yoon, buleen ko topp; seen kasaray tuur, buleen ca sobeel seen bopp.