Ezekiel 20:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Moo tax, yaw nit ki, nanga wax ak waa kër Israyil, ne leen: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Seeni baay a ma dellu ŋàññ, fecci ma kóllëre.