Ezekiel 20:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kon nag nanga wax ak waa kër Israyil ne leen: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Seen tànki baay ngeen topp, di sobeel seen bopp, topp seen tuur yu siblu, di gànctook ñoom?