Ezekiel 20:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen di génnee ci askan yeek réew yi ngeen tasaaroo ci seen biir. Sama dooley loxo laa koy defe ak sama kàttanu përëg, ak sànj mu naan soteet fi seen kaw.