Ezekiel 20:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«“Léegi nag yeen waa kër Israyil, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Aca, na ku ne jaamuji kasaray tuuram! Dungeen mujje lu moy déggal ma, ba sama tur wu sell wi, dootuleen ko teddadile seeni sarax ak seeni tuur.