Ezekiel 21:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nag nit ki, sàkkal ñaari yoon yu saamaru buuru Babilon di jaare dikk; ñaari yoon yuy bàyyikoo menn um réew. Tegal fa buntu yoon wu ci nekk màndarga muy tegtale dëkk ba yoon wa jëm;