Ezekiel 21:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Yerusalem foog ne ngisaane googu misaal seen jéll, caaxaan la, ndax ngiñ moo lal seen kaaraange, ba du deñ. Waaye buuru Babilon a leen di fàttli seenug tooñ, ba jàpp leen njaam.