bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 21:34
Ezekiel 21:34 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gisal nañu leen peeñuy caaxaan, gisaaneel leeni fen. Teewul saamar ba di tege ca ndoddi ñu bon ñi ñu nara bóom, seen bés taxaw, seen mujjantalu mbugal teew.