Ezekiel 21:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaay doon mattum sawara wa, sa deretu boroom ne xéew fi digg réew mi, ba deesatu la fàttliku. Man Aji Sax ji maa ko wax!”»