Ezekiel 21:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxal réewum Israyil ne ko: “Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngi nii fi sa kaw. Maay boccee sama saamar mbaram, daldi dagge fi yaw ku jub ak ku bon.