Ezekiel 22:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaw dëkk bii, gàddu nga bàkkaar ndax deret ji nga tuur, sobeel nga sa bopp ndax kasaray tuur yi nga sàkk. Kon gàttal nga saw fan, agsi nga ci sa àppu at. Moo tax maa lay def ku mboolem xeet yi di sewal, ku mboolem waa réew yi di kókkali.