Ezekiel 23:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña nga takk ngañaay ca seen ndigg, tañlaayu bay langal, ñoom ñépp di nirooki kàngam, di saf doomi Babilon, réewum Kalde di seen cosaan.