Ezekiel 23:47 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gàngoor gaa leen di dóor ay doj, jam leeni saamar, ñu dee, seeni doom, góor ak jigéen, ñu bóom; seeni kër, ñu taal,