Ezekiel 23:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña nga sol seen mbubbi baxa, diy kàngam aki jawriñ, ñoom ñépp di xale yu góor yu sopplu, di ndaanaani gawar.