Ezekiel 24:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi Aji Sax ji kat dafa wax ne: «Wóoy ngalla bii dëkku tuurkatu deret! Mooy cin lu teg àkki xëmit, cin lu dul tàggook xëmitam. Wenn-wenn ngay seppi dogi yàpp yi, te bul tegoo bant la ngay seppi.