Ezekiel 25:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne: Filisteen ñee jiital seen mbañeel gu sax, ñoo jéppee jéppi seeni noon, feyoo feyu, ba faagaagal leen.