bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 25:7
Ezekiel 25:7 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ngii nag di leen dóor sama loxo, te maa leen di jébbal xeet yi, ñu sëxëtoo leen. Maa leen di dagge fi digg xeet yi, maa leen di fare ci réew yi, faagaagal leen, ba ngeen xam ne maay Aji Sax ji.”»