Ezekiel 26:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax Tir, ne ko: Keroog sa coowal jéll ba, ba ñuy bóome fa sa biir, ñay dee di binni, dun yaa cay dégg, di lox moos!