Ezekiel 26:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne: Bu ma lay def dëkk bu gental, nga mel ni dëkk yu nit ña ne mes, ba ma waral xóote ya fi sa kaw, ba wali ndox ya mëdd la,