Ezekiel 26:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yaw Tir, maa ngii fi sa kaw. Ni géej di yéegee ay gannaxam, ni laay yéegloo fi sa kaw xeet yu bare.