Ezekiel 26:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Tir ay doon wéerukaayu caax ci digg géej gi, maa ko wax, kàddug Boroom bi Aji Sax jee. Dëkk bii mooy doon sëxëtoom xeet yi,