Ezekiel 28:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Bu may dajale waa kër Israyil, di leen jële digg xeet yi ñu tasaaroo, ca laay fésal sama sellnga fa seen biir, yéefar yi gis, ñu dëkke seen suufas bopp, sa ma joxoon Yanqóoba sama jaam ba.