Ezekiel 29:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maay def Misra gëna gental ci réew yi gental, ay dëkkam gëna gental ci dëkk yi diiru ñeent fukki at. Maay tasaare waa Misra ci biir xeet yi, wasaare leen ci biir réew yi.