Ezekiel 29:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di jox réewum Misra, Nabukodonosor buuru Babilon, mu yóbbu alal ja, wëq ko ba mu set, sëxëtoo mboolem lu mu amoon, muy peyooru mbooloom xareem,