Ezekiel 29:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bésub keroog maay yokk dooley waa kër Israyil, yaw nit ki, ma jox la sañ-sañu àddu fi seen biir. Su boobaa ñu xam ne maay Aji Sax ji.»