Ezekiel 29:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«“Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yaw Misra, maa ngii di la indil saamar, ba dagge fi yaw nit ak mala.