Ezekiel 3:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu teg ca, ne ma: «Yaw nit ki nag, mboolem li ma lay wax, dégloo ko nopp, te teewloo ko xel.