Ezekiel 3:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nag su dee yaa àrtu boroom njekk bi, ba tax bàkkaaratul, dina dund déy, ndax kàddug àrtu ga, te yaw it musal nga sa bopp.»