Ezekiel 3:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ma: «Yaw nit ki, demal ba ca waa kër Israyil, te nga àgge leen samay wax.