Ezekiel 31:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa genn garab gu feggook ndox dootu siggi ca kaw, ba njañ lay àkki niir ya, genn garab dootu màndim ndox, bay damu ci kawi moroomam. Ñoom ñépp déy lañu àppal ndee, ñu jëm xóotey suuf, tëddi biir bàmmeel ni waa àddina sépp.