Ezekiel 31:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Bés ba seedar ga tàbbee njaniiw, maa dogal ag ñaawlu: Maa sàng xóote ya ndax moom, téye dexi biir suuf, wali ndox yi noon xéew, taxaw. Maa ñaawluloo gottub Libaŋ ci loolu, garabi àll bi yépp doxe ca lax.