Ezekiel 32:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Saamari jàmbaar laay tërale sa mbooloo, ñoom ñépp bokk ci xeet yi gëna néeg, te ñooy sàggi sagub Misra; gàngooram gépp sànku.