Ezekiel 32:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seeni bàmmeel a nga féete fa xóotey xóote ya, ñu yéew bàmmeelu buurub Asiri. Ñoom ñépp lañu jam, ñu fàddoo saamar, te daan tiital waa réewum aji dund ña.