Ezekiel 32:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa lay laaw sama caax fi biir ndajem xeet yu bare, ñu ñoddee la mbaal ma, génne.