Ezekiel 33:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nit ki, waxal ak waa kër Israyil, ne leen: “Ngeen ne dungeen mana mucc ndax seeni tooñ ak seen bàkkaar yu leen diis ba semmal leen?”