bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 33:11
Ezekiel 33:11 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxleen ne leen: “Giñ naa ko ci man miy dund, kàddug Boroom bi Aji Sax jee, awma bànneex ci deewug nit ku bon. Sama bànneex mooy mu wacc yoonu mbonam, ba dund. Kon yeen waa kër Israyil, waccleen, ngalla waccleen seen yoonu mbon. Ana lu jar ngeen di dee?”