Ezekiel 33:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nit ki, waxal sa bokk yi, ne leen: “Boroom njekki démb li, su tooñee tey, njekkam loola du ko musal. Ku bon ki itam, bu waccee yoonu mbonam, tey, mbonu démbam ga du ko lor. Boroom njekki démb li nag, su bàkkaaree, njekkal démbam la du ko may mu dund.