Ezekiel 33:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Sa bokk yi nee ñu: “Ni Boroom biy doxale du noonu.” Te ñoom la seen doxalin dul noonu!